Telecharger l’emission en cliquant à droite ici
Archives mensuelles : août 2015
Njiit 1
Telecharger l’emission en cliquant à droite ici
Téereb Injiil di Kàddug Yàlla mu ne : Gannaaw loolu na nit ku nekk déggal ñi yore baat ci kanamam ; ndaxte amul njiit lu fi Yàlla sampul. Njiit yépp nag Yàlla moo léen fi teg.
Rafet Njort
Telecharger l’emission en cliquant à droite ici
Yeesu wax na ci Yoonu Musaa ak Yonent yi