Telecharger l’emission en cliquant à droite ici
Archives mensuelles : septembre 2015
Sunu Baay 2
Telecharger l’emission en cliquant à droite ici
Sunu Baay 1
Telecharger l’emission en cliquant à droite ici
Ñaan-u Sang bu Tedd bi
Yéen nag nii ngeen wara ñaane :
“Sunu Baay bi nekk ci kaw, yal na sa tur di lu ñu sellal,
yal na sa nguur ñëw,
yal na sa coobare am ci suuf mel ni ci kaw.
Yal nanga nu may tey li nu dunde ;
te baal nu sunuy tooñ, ni nu baale ñi nu tooñ;
Yàlla boo nu teg ci yoonu nattu, waaye yal nanga nu musal ci lu bon.
Ndaxte yaw yaa yelloo nguur ak kàttan ak màggaay, ba fàww. Amiin.”
Njiit 2
Telecharger l’emission en cliquant à droite ici