Telecharger l’emission en cliquant à droite ici.
Archives de catégorie : Kan Mooy Seydina Isaa Almasi Bi?
Jiital Yàlla
Telecharger l’emission en cliquant à droite ici.
Kan Mooy Yeesu 3
Telecharger l’emission en cliquant à droite ici.
Yeesu ak Aadama
Telecharger l’emission en cliquant à droite ici
Ñaari Aadama 1
Telecharger l’emission en cliquant à droite ici
Mbëgeel
Telecharger l’emission en cliquant à droite ici
Yeesu Mooy Saraxalkat Bu Magg Bi
Telecharger l’emission en cliquant à droite ici
Seytaane Jeem Na Fiir Yeesu
Telecharger l’emission en cliquant à droite ici
Téereb Injiil di Kàddug Yàlla mu ne, « moom sax far jaar na ci nattu ni nun ci bépp fànn, waaye deful bàkkaar. »
Kéemaanu Yeesu
Telecharger l’emission en cliquant à droite ici
Seydina Isaa Almasi bi, Yeesu Kirist mu ne ay taalibee yonent Yaxya,« Demleen nettali Yaxya li ngeen dégg te gis ko. Gumba yaa ngi gis, lafañ yiy dox, *gaana yi wér, tëx yiy dégg, ñi dee di dekki, te néew doole ñaa ngi dégg xibaaru jàmm bi. Yaw mi sa ngëm yolomul ndax man, barkeel nga. »
Sellaayu Yeesu 2
Telecharger l’emission en cliquant à droite ici
Seydina Isaa Almasi bi, Yeesu Kirist mu ne, « Ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, laata ñuy sàkk Ibraayma, fekk na ma doon ki ñuy wax Maay ki Nekk.»