Kéemaanu Yeesu

Ecoutez l’emission en cliquant ici:

ou telecharger en cliquant à droite ici.

Seydina Isaa Almasi bi, Yeesu Kirist mu ne ay taalibee yonent Yaxya,« Demleen nettali Yaxya li ngeen dégg te gis ko. Gumba yaa ngi gis, lafañ yiy dox, *gaana yi wér, tëx yiy dégg, ñi dee di dekki, te néew doole ñaa ngi dégg xibaaru jàmm bi. Yaw mi sa ngëm yolomul ndax man, barkeel nga. »

Sellaayu Yeesu 1

Ecoutez l’emission en cliquant ici:

ou telecharger en cliquant à droite ici.

Téereb Injiil di Kàddug Yàlla mu ne, « Yàlla yónni woon na nit ku ñu naan Yaxya. Kooku ñëw na, doon ab seede, ngir wax ci mbirum leer gi. Ñëw na ngir ñépp dégg li mu wax te gëm. Moom ci boppam du woon leer gi, waaye ñëw na ngir seedeel leer gi. Kàddu googu mooy leer gu wóor, giy ñëw ci àddina te di leeral nit ku nekk. »